Doomi Yuda yu góor di Er ak Onan ak Sela ak Peres ak Sera, te Er ak Onan faatu ca réewu Kanaan. Doomi Peres yu góor di Esron ak Amul.
TSK
TSK · Genesis 38:10
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
Genesis 46:12
TSK
Numbers 22:34
TSK
Balaam ne malaakam Aji Sax ji: «Maa tooñ, ndax xawma woon ne yaa taxaw, dogale ma ci yoon wi. Léegi nag su la yoon wi neexul, ma daldi dëpp.»
1 Samuel 2:25
TSK
Su nit ki tooñee moroomu nitam, Yàllaay àtte; waaye su dee Aji Sax ji la nit ki tooñ, ana ku koy àtte?» Wax jooju nag taxul ba tey ñu déggal seen baay. Booba fekk na Aji Sax ji namm leena rey.
1 Kings 17:20
TSK
Ba mu ko defee Ilyaas ñaan ci Aji Sax ji, ne ko: «Éy Aji Sax ji, sama Yàlla, xanaa doo teg jëtun bii ma dalal, naqar wu tollu ni, di seetaan doomam ju góor muy dee?»
Proverbs 24:18
TSK
Lu ko moy Aji Sax ji gis la, ñaawlu ko, daldi giif, dootu ko mbugal.
Haggai 1:13
TSK
La ca tegu Ase, ndawal Aji Sax ji, jottli askan wa yóbbanteb Aji Sax ji. Mu ne leen: «Maa ànd ak yeen, kàddug Aji Sax jee.»