Genesis 39:10
TSK
Ba loolu amee bés bu Yàlla sàkk mu di ko wax Yuusufa, te dégluwu ko, wéetul ak moom sax, bay tëdd ak moom.
TSK
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
Ba loolu amee bés bu Yàlla sàkk mu di ko wax Yuusufa, te dégluwu ko, wéetul ak moom sax, bay tëdd ak moom.
Naka la Tamar dikk, taajal Amnon mburu ya, ngir mu lekk, mu ne ko katam, ne ko: «Kaay, tëdd ak man, sama jigéen.»
Soreel ndaw soosu, bul jege bunt këram.
Ndaw sa ne ko katam, fóon, ne wajj, ne ko:
¶ «“Yaaka weex bët, kàddug Boroom bi Aji Sax jee, lii lépp di jëfi gànc bu dëgër bët.
Bu leen kenn nax: «Ànd bu bon yàq na jikko ju baax.»
¶ Soppe yi, ay gan ngeen, ay doxandéem ci kaw suuf. Kon nag li ma leen di dénk moo di ngeen moyu xemmemtéefi bakkan yiy xeex ak ab xol.