TSK

TSK · Genesis 40:11

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

Mooy yeew mbaamam cig reseñ, cumbur ma féeteek car, ba ca gën; muy fóote ay yéreem biiñ, di sumb mbubbam ci ndoxum reseñ.

ak njëlu këram, ak jataayu dagam ya, ak taxawaayu surgaam ña, ak seen col ga, ak ña yor ay naanam, ak saraxi rendi-dóomal ya muy joxe ca kër Aji Sax ji. Mu daldi yéemu, ba ag noowam réer ko.

Éy Boroom bi, Sang bi, rikk teewlul bu baax samag ñaan, ak sa ñaanu jaam ñi safoo wormaal saw tur. Ngalla Sang bi, nangul ma tey jii, may ma waa jii yéwéne ma.» Booba maa yore woon naani Buur.