Genesis 20:15
TSK
Abimeleg ne ko: «Sama réew mépp a ngi noonu, dëkkal fu la neex.»
TSK
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
Abimeleg ne ko: «Sama réew mépp a ngi noonu, dëkkal fu la neex.»
«Ñii sunuy am-di-jàmm lañu, te gannaaw réew maa ngi ne yàmblaŋ, bàyyileen leen, ñu sanc te dem fu leen neex. Man nanoo jël seen doomi janq te di leen may sunuy doom.
Waaye nangeen ma indil seen rakk, ba ma xam ne li ngeen wax dëgg la; su ko defee dungeen dee.» Ñu daldi ne: «Waaw,»
dagg car bu ndaw ba ca gëna kawe, yóbbu ba menn réewum jula, jëmbat ko ca biir dëkkub jaaykat ya.