Waaye nangeen ma indil seen rakk, ba ma xam ne li ngeen wax dëgg la; su ko defee dungeen dee.» Ñu daldi ne: «Waaw,»
TSK
TSK · Genesis 43:3
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
Genesis 42:20
TSK
Genesis 43:5
TSK
Waaye boo ko bàyyiwul kat, dunu dem, ndax waa ja waxoon na nu ne nu: “Dungeen jàkkaarlook man te seen rakk àndul ak yeen.”»
2 Samuel 3:13
TSK
Daawuda ne ko: «Baax na. Dinaa fasook yaw kóllëre, waaye lenn rekk laa lay ñaan. Bul dikk fi sama kanam te indiloo ma sama jabar Mikal doomu Sóol.»
2 Samuel 14:28
TSK
¶ Absalom nekk na Yerusalem ñaari ati lëmm yu mu sañula taxaw fa kanam Buur baayam.
Acts 7:34
TSK
Gis naa bu baax sama coonob ñoñ ci Misra; maa dégg seeni onk, ba wàcc ngir wallusi leen. Léegi nag dikkal, ma yebal la Misra.”
Acts 20:38
TSK
La leen yokk aw tiis nag mooy kàddu ga mu leen wax, ne leen: «Dootuleen ma gis.» Ba mu ko defee, ñu gunge ko ba ca gaal ga.