Genesis 24:2
TSK
¶ Mu am bés Ibraayma wax surgaam, bi gëna yàgg ci këram, tey saytu alalam jépp, ne ko: «Dugalal sa loxo ci sama suufu lupp,
TSK
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
¶ Mu am bés Ibraayma wax surgaam, bi gëna yàgg ci këram, tey saytu alalam jépp, ne ko: «Dugalal sa loxo ci sama suufu lupp,
¶ Naka la ku nekk sotti saakoom, ne jàkk ca mbuusu xaalisam. Ba ñu gisee mbuusi xaalis ya, ñoom ak seen baay, dañoo tiit.
Ba Yuusufa gisee Beñamin ànd ak ñoom, dafa wax fara biir këram, ne ko: «Yóbbul gaa ñi ca kër ga, te nga rey gàtt, defar ko, ndax maak ñoom nooy bokk añ tey.»
Aji Sax ji Boroom bi, Aji Sax ju gàngoor yi kat, mu ngi nii di jële Yerusalem ak Yuda, lu doon wéeruwaay, di cëslaay, muy dugub ju ñu yaakaaroon, di ndox mu ñu yaakaaroon,