Yàlla da maa yebal, ma jiitusi leen, ba rawale seen bakkan, dikke leen xettal gu mag, ba seen askan baña fey.
TSK
TSK · Genesis 47:12
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
ndaxte des na juróomi ati xiif. Waaye dinaa la fi yore, ba doo ñàkk dara, yaak sa waa kër ak mboolem lu bokk ci yaw.”
Waa réew ma ñoom, Yuusufa da leena def ay jaam ca Misra, gii wet ba gaa.
Kon nag buleen tiit, dinaa leen yor, yeen ak seeni doom.» Yooyu kàddu la dalale seen xol, ba ñu am jàmm.
Dina la leqli, dimbali la keroog ba ngay mag, ndax sa goro bi la bëgg te dàqal la juróom ñaari doom yu góor, moo ko jur.»
Manoon nanoo taafantoo li nu diy ndawi Almasi, ba diisal leen, waaye danoo lewetoon domm ci seen biir, mel ni jaboot juy topptoo ay doomam.
Waaye su dee ab jëtun bu ami doom mbaa ay sët, ñooñoo wara jëkka jéema jëfe ag ragal Yàlla ci seen biir kër, ba delloo njukkal seen waajur, ndax loolu la Yàlla rafetlu.