TSK

TSK · Genesis 5:32

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

Nóoyin nag amoon na ñetti doom yu góor: seeni tur di Sem, Xam ak Yafet.

¶ Doomi Nóoyin yu góor, yi génne ci gaal gi, ñooy: Sem, Xam ak Yafet; Xam mooy baayu Kanaan.

¶ Askanu doomi Nóoyin mooy lii. Gannaaw ba mbënn ma wéyee, Sem ak Xam ak Yafet am nañu ay doom.

¶ Sem, miy magu Yafet, jur na moom itam ay doom yu góor. Mooy maami Eber ak askanam.