Ña nga ñibbi ca njiital Sorobabel ak Yosuwe ak Neyemi ak Seraya ak Relaya ak Mardose ak Bilsan ak Mispar ak Bigway ak Reyum ak Baana. Limeefu góori bànni Israyil nii la tëdde:
TSK
TSK · Haggai 2:21
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
Ezra 2:2
TSK
Psalms 46:6
TSK
Yàllaa ngi ci biir dëkk bi, du raf; Yàllaa koy dimbali ba jant fenkee.
Ezekiel 38:19
TSK
Sama fiiraange ak sama tàngooru xadar laa birale ne: bésub keroog déy, suuf dina yëngoo Israyil lool;
Haggai 1:1
TSK
¶ -Ca ñaareelu atu nguuru Buur Daryus, ca juróom benneelu weer wa, yemook benn fan ca weer wa, kàddug Aji Sax ji moo dikk ci jottlib Yonent Yàlla Ase, ñeel doomu Selcel, Sorobabel boroom Yuda, ñeel itam doomu Yoccadag, Yosuwe sarxalkat bu mag ba. Mu ne:
Haggai 2:6
TSK
Aji Sax ji Boroom gàngoor yi kat dafa wax ne: Fileek lu néew, maa ngii di yëngalaat asamaan ak suuf, ak géej ak jéeri.
Hebrews 12:26
TSK
Booba baatam la yëngale woon suuf, waaye tey moo dige ne: «Beneen yoon, maay yëngalati suuf, te du suuf doŋŋ, waaye asamaan itam.»