TSK

TSK · Haggai 2:3

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع
Ezra 3:12 TSK

Teewul ñu bare ca ña féete mag, diy sarxalkat aki Leween aki boroom kër, gisoon nañu kër gu jëkk ga. Ba ñu gisee kenug kër gu bees ga, dañoo yékkati seen kàddu ca kaw di jooy, ñu bare it di xaacu ndax mbégte.

Ñoo doon sagoo seen gànjar gu yànj, di ci sàkk jëmmi tuur yu jara bañ te jomblu, ba tax ma defal leen ko sagaru sobe.

«Loxol Sorobabel a teg kenug kër gii, loxoom a koy sottli itam,» ngeen daldi xam ne Aji Sax ji Boroom gàngoor yi moo ma yónni ci yeen.

Luke 21:5 TSK

¶ Mu am nag ay nit ñu doon wax ca kër Yàlla ga, ak taaru doji tànnéef, ya ak yeneen alali jooxe ya ñu ko rafetale. Yeesu itam ne leen: