Psalms 40:7
TSK
Saraxi gàtt mbaa pepp, taamuwuloo ko, ay nopp nga ma bënnal, saraxu rendi-dóomal, ak saraxu póotum bàkkaar, sàkkuwuloo ko.
TSK
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
Saraxi gàtt mbaa pepp, taamuwuloo ko, ay nopp nga ma bënnal, saraxu rendi-dóomal, ak saraxu póotum bàkkaar, sàkkuwuloo ko.
«Jëlal taxañu bindukaay, nga bind ci mboolem kàddu yi ma la wax ci mbirum Israyil ak Yuda ak mboolem xeet yi, te nga dale ko ba ma waxeek yaw ca jamonoy Yosya ba bésub tey jii.
Mu teg ca ne: «Maa ngii defsi sa coobare.» Noonu la fare lu jëkk la, ngir wuutal fa ñaareel bi.