TSK

TSK · Hebrews 3:2

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

waaye du Musaa sama jaam bii. Moom mooy ki wóor ci mboolem sama kër gii.

¶ Samiyel ne mbooloo ma: «Aji Sax ji moo jëfoo Musaa ak Aaróona, ba génne seeni maam réewum Misra.

Ci Almasi ngeen bokke ci tabax bi, yeen jaambur ñi itam, ba mana doon dëkkuwaayu Yàlla, ci ndimbalal Noo gu Sell gi.

ngir su ma yeexee itam, nga xam nooy doxale ci kër Yàlla, ci biir mbooloom Yàlla jiy dund. Mbooloom gëmkat mi mooy kenug dëgg gi, di cëslaayam.

Musaa déy «jawriñ bu wóor la woon ci biir mboolem waa kër Yàlla,» di seedeel Yàlla kàddu ya ñu fa wara wax.