كل أسفار KYG

Hebrews 7

KYG · الآية 2

13 أصحاحات

KYG / Hebrews / الأصحاح 7

KYG · الآية 2

M oom la Ibraayma jox fukkeelu cérub mboolem cëxëtoo ma. Ni ñu jëkka dégge aw turam Melkisedeg, ci tekki, mooy «buur bu jub». Bu loolu weesee itam moom mooy buurub Salem, muy «buuru jàmm».