TSK

TSK · Hosea 5:4

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

¶ Doomi Eli yu góor ya nag def nit ñu bon ñu faalewul Aji Sax ji.

Mu jëm ci njiital jàngkat yi, ñeel Daawuda jaamub Aji Sax ji.

Moo tax Aji Sax ji Boroom gàngoor yi wax ne: «Maa ngii di leen segg, nattu leen ni weñ gu sawara seeyal, xelli! Ana nu may def neneen ak sama ñoñ?

«Ëpplante banti seedar da laa def buur? Sa baay daawul lekk ak a naan? Teewu koo jëfe dëgg ak yoon, muy njiglaayam.

Maral ci kawi waltanam, mu ŋiis; mii réew mu nit ñiy jaamoo jëmmi tuur, ñooy say ndax seen yu ñàng yooyu

Hosea 4:6 TSK

Sama ñoñ a sànku ndax ñàkka xam; yeen, xam-xam ngeen gàntal, ma gàntal seenug carxal. Yeena fàtte seen yoonu Yàlla, man it maay fàtte seeni doom.

Sama ñoñ, seen bant lañuy seeteey, seenu yet di leen waxaleey. Xelum ngànctu moo leen wacc, ñooy gànctu, lajje fa seen Yàlla.