TSK

TSK · Isaiah 16:1

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

Daawuda duma Mowabeen ña itam, tëral leen ca suuf, sësale leen, natte leen ag buum. Ñaari buum yu mu natt, yemook ña ñu wara rey, buum gu mat ga ca topp yemook ñi wara dund. Mowabeen ña daldi nangul Daawuda, di ko indil galag.

¶ Moom Amaciya moo duma fukki junniy (10 000) waa Edom ca xuru Xorom wa, nangu dëkk ba ñuy wax Sela ca xare ba, tudde ko Yogtel, te noonu la tudd ba bésub tey jii.

Tey jii noon yaa ngay taxaw fa Noob, di sànni loxo waa tundu Siyoŋ, di ko tëkkoo waa Yerusalem googu.

Micah 4:8 TSK

«Yaw, tatay gétt gi, yaw tundu Ofel, yaw janq Siyoŋ mu taaru mi, yaw lees di ñëwal, yaw la kilifteef ga woon di dikkal, nguur gi, janq Yerusalem mu taaru lay ñeel.»