TSK

TSK · Isaiah 2:16

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

nangeen dàq waa réew mépp, nangeen yàqte seen mboolem tuur yu ñu yett, te seen mboolem jëmm yu ñu móol, yàqteleen ko, seen mboolem bérabi jaamookaay it, tasleen ko.

¶ Booba réewum Edom amuloon buur. Ab jawriñ lañu fa daan tabb.

¶ Yéene bii ñeel na dëkk ba ñuy wax Tir: Yeen waa gaali Tarsis ñi deele, jooyleen! Lépp a yàqu! Du kër, du teeruwaay. Fa dunu Sippar lañu leen ko waxe.

¶ Julay àddinaa ngay yuuxu, di ko jooy, nde am njaayam du jarati: