TSK

TSK · Isaiah 2:7

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

Waaye bu buur bi barey fas, te bumu delloo askan wi Misra, ngir sàkku fas yu bare, te Aji Sax ji waxoon leen ne buleen dellooti woowu yoon.

¶ Mboolem lu Buur Suleymaan daan naane wurus la, te mboolem ndabi këram ga ñuy wax Gottub Libaŋ wurusu ngalam la. Dara du ca xaalis, ndax xaalis jàppeesu ko woon muy dara ca janti Suleymaan.

Job 3:15 TSK

Nopplu koon naak garmi yay boroom wurus, te daan feesal seeni kër, xaalis.

Yeena ne: “Déedéet, danuy war fas, daw!” Dingeen daw moos! Ngeen ne: “Daamar yu gaaw lanuy war.” Ñi leen di dàq it di war daamar yu gaaw!

Ni kaaf di feeseeki picc, ni la seeni kër di feese alali càcc, ba tax ñu yokku ba woomle,

Maa fiy dagge sa dëkki réew mi, màbb sa tata yépp.

Kaasu biiñu sànj, bi sababoo ci moyam, moom la askani àddina yépp di naan. Moom la buuri àddina àndal di moy, te doyloodig bakkanam gu réy woomal na julay àddina.»