2 Kings 19:32
TSK
¶ «Moo tax Aji Sax ji wax ci buurub Asiri ne: “Du dugg ci dëkk bii, du fi soqig fitt, du fi taxawe ab pakk, du fi jal jal bu muy gawe.
TSK
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
¶ «Moo tax Aji Sax ji wax ci buurub Asiri ne: “Du dugg ci dëkk bii, du fi soqig fitt, du fi taxawe ab pakk, du fi jal jal bu muy gawe.
¶ Ba Cedekiya tolloo ci juróom ñeenteelu atu nguuram, fukki fan ca fukkeelu weeram, ca la Nabukodonosor buuru Babilon ànd ak mbooloom xareem mépp ci kaw Yerusalem. Ñu dal fa janook ñoom, yékkati gawukaay, wërale ko.
man it ma ŋëb bii loxo, dóor ca bee, ba giifal sama xadar. Man Aji Sax ji maa ko wax.»
Ay bés a ngi dikk ci sa kaw, keroog say noon a lay gawe ab sëkk, yéew la, tance la wet gu nekk.