¶ «Su fekkee ne góor mbaa jigéen dafa ame jàngoro ci bopp mbaa ci sikkim,
TSK
TSK · Isaiah 3:17
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
Leviticus 13:29
TSK
¶ Aji Sax jee leen di dumaa taabi Misra, ak neewoy kërug suuf, ak yaram wu xas, ak ër yuy xasan te dungeen mana am pajam.
Isaiah 47:2
TSK
Fabal wolukaay, wol sunguf. Dindil sa muuraay gi, wogos sa mbubb, ëñ sas kumba, xuus, jàll dex yi.
Jeremiah 13:22
TSK
Soo nee ci sam xel: «Lu tax lii dal ma?» xamal ne sa ñaawtéef gu réy a waral ñu ñori la, saaysaaye la.
Ezekiel 23:25
TSK
Maa lay yen sama fiiraange, te yaw lañuy jëflanteel ak xadar, sa bakkan ak say nopp, ñu njoof, saw ndes fàddoo saamar. Say doom, góor ak jigéen, ñu nangu, sa kuutaay lakk ba xoyomu.
Nahum 3:5
TSK
«Maa ngii fi sa kaw,» kàddug Aji Sax jee, Boroom gàngoor yi. «Sa pendal laay ñori, ba muur sa xar-kanam, won xeeti jaambur yi sa yaramu neen, gisloo waa réew yi sa gàcce.