Proverbs 25:19
TSK
Bul wóolu workat bésub njàqare, mooy bëñ bu bon mbaa tànk bu nasax.
TSK
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
Bul wóolu workat bésub njàqare, mooy bëñ bu bon mbaa tànk bu nasax.
waaye ñoom ñépp kersa lañuy ame Misra, googu leen dul amal njariñ. Du ndimbal, du njariñ, xanaa gàcceek toroxte.
Yettkati xërëm yaa ngoogu, rus, torox, riixleendoo.
Aji Sax ji dafa wax ne: «Alkànde ñeel na ku yaakaar doom aadama ak képp kuy doolewoo nit, dëddu Aji Sax ji.
«Aji Sax ji Yàllay Israyil dafa wax ne: Buuru Yuda mi leen yebal, ngeen seetsi ma, waxleen ko ne ko: “Mbooloom Firawna mi génnoon di leen wallusi kat, dëpp na bay dellu Misra.
ñu jafandu ko, mu ne tàllit, ne xureet mbagg yépp, ñu wéeroo ko, mu ne tipp, ndigg yépp rëcc.
Mbind mi moo ne: «Képp ku ko gëm, doo rus.»