¶ Ba mu ko defee saskati liggéey ya ak farbay ngàllo ga génn, wax ak mbooloo ma, ne leen: «Firawna nee na, du moo leen di jox boob.
TSK
TSK · Isaiah 30:6
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
Yeen nag Aji Sax jee leen jël, bellee leen ca Misra, taalu xellikaayu weñ gu ñuul ba, ngir ngeen doon ñoñam ñi mu séddoo niki bésub tey.
Waaye bu buur bi barey fas, te bumu delloo askan wi Misra, ngir sàkku fas yu bare, te Aji Sax ji waxoon leen ne buleen dellooti woowu yoon.
dellu xool fi suuf, yem ciw tiis, ak lëndëmu njàqare, sóoboo guddi gu fatt taraj.
Jël nañu lu ñu deseek lu ñu dencoon, yóbbu, jàll ca wàllaa xuru Garab ya.
Tuur ma ñu naa Bel toqi na, tuur ma ñu naa Nebo sukk, mala ya féetewoo seeni jëmm, ñoom lees daan gàddu, tey jur gi jagoo, di leen sëf ba loof.
Newuñu: “Ana Aji Sax, ji nu génne woon réewum Misra, jiite nu ca biir màndiŋ ma, ca joor gu wow gaak xur ya, réewum maral ma lëndëm këruus, jaareesu fa, dëkkeesu fa?”
Ñoo demal seen bopp Asiri. Mbaamu àll day beru yoonam, waaye waa kër Efrayim ñooy jënd ay far.
Efrayim mooy sàmmkatub ngelaw, yendoo topp ngelawal penku, di yokki fen ak fitna, fasoo kóllëre ak Asiri, yónnee yóbbalu diw ba Misra.