TSK

TSK · Isaiah 32:9

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

Jigéen ju gëna lewet te xay ci yeen, ba néegula teg ndëggul tànkam ci suuf ndax xayteem ak lewetaayam, dina xeelu jëkkëram ju muy noyyee, ak doomam ju góor ak ju jigéen.

Mu jëm ci njiital jàngkat yi, di kàddug Sabóor, ñeel askanu Kore wu góor.

Teeyluleen te déglu sama kàddu, teewluleen ba dégg samay wax.

Yaw Siyoŋ, dëkk bu taaru bi te xejj, dama lay dammat.

«Mowab a dale féex cag ndawam, kenn jàppu ko njaam, yóbbu, wàllanteesu ko ndab ak ndab, xanaa mu ne degg ni biiñ bu taaje, di saf, di xeeñ ba tey.

Amos 6:1 TSK

Wóoy ña ne finaax ca Siyoŋ, wóoy ña naagu fa tundu Samari! Ñooy kàngami xeet wi gëna màggeey, niti Israyil di leen diis-si soxla.