TSK

TSK · Isaiah 36:4

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

¶ Ba mu ko defee Rabsake bëkk-néegu buurub Asiri ne leen: «Waxleen nag Esekiya ne ko: Buur bu mag ba, buurub Asiri dafa wax ne: “Sa yaakaar jii nga yaakaar, ana foo ko teg?

Maa mar Yàlla, Yàlla jiy dund! Kañ laay teewi fa kanam Yàlla?

Noon yaa nga may tooge, ñi may tëroo ngay diisoo,

Mu ngi naan: «Xanaa du sama jawriñ yépp a diy buur?

«Mowabee, du yaay kañu, naan jàmbaar ngeen, diy ñeyi xare?

Moo ko taxa sut garabi àll bi, ay bànqaasam sëq, car ya lawa law ndax ndox mi koy ballal a ne xéew.

Mbooloo maa ngay àddu ca kaw, naan: «Lii kay baatu Yàlla la, du baatu nit!»