Exodus 3:12
TSK
Mu ne ko: «Man déy, maay ànd ak yaw, te boo génnee mbooloo ma Misra, dingeen ma jaamusi ci tund wii. Loolooy firndeel ne, maa la yónni.»
TSK
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
Mu ne ko: «Man déy, maay ànd ak yaw, te boo génnee mbooloo ma Misra, dingeen ma jaamusi ci tund wii. Loolooy firndeel ne, maa la yónni.»
La saxe ca seenum ngóob sax, buleen ko góobaat te it reseñ gu ñu wolliwuloon buleen ko raasaatu. Atum Noflaay la wara doon: suuf sa ca boppam na nopplu atum lëmm.
Góor ga joxe na ca bésub keroog ab takk; mu ne: «Takk bii la ci Aji Sax ji biral: “Seetluleen, sarxalukaay bi dina xar ñaar, dóom bi ci kaw sottiku.”»
Esayi ne ko: «Takk biy bàyyikoo ci Aji Sax ji, di firndeel ne dina def li mu wax, yaar yii loo ci bëgg: ker gi màgg lu tollook fukki dëggastal, mbaa mu dellu gannaaw fukki dëggastal?»
Bésub keroog nit du fa dundle lu dul wenn nag ak ñaari gàtt,