2 Kings 19:32
TSK
¶ «Moo tax Aji Sax ji wax ci buurub Asiri ne: “Du dugg ci dëkk bii, du fi soqig fitt, du fi taxawe ab pakk, du fi jal jal bu muy gawe.
TSK
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
¶ «Moo tax Aji Sax ji wax ci buurub Asiri ne: “Du dugg ci dëkk bii, du fi soqig fitt, du fi taxawe ab pakk, du fi jal jal bu muy gawe.
Tey jii noon yaa ngay taxaw fa Noob, di sànni loxo waa tundu Siyoŋ, di ko tëkkoo waa Yerusalem googu.
Ngoon a ngay jot, tiitaange ne jaas, balaa bët a set lépp jeex. Lii mooy añub ñuy sëxëtoo, lii mooy deminu ñiy nangu sunu alal.
man it ma ŋëb bii loxo, dóor ca bee, ba giifal sama xadar. Man Aji Sax ji maa ko wax.»