1 Kings 20:36
TSK
Mu ne ko: «Gannaaw nanguwuloo déggal Aji Sax ji, dama ne, booy teqlikook man, gaynde fàdd la.» Naka la teqlikook moom, gaynde dajeek moom, fàdd ko.
TSK
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
Mu ne ko: «Gannaaw nanguwuloo déggal Aji Sax ji, dama ne, booy teqlikook man, gaynde fàdd la.» Naka la teqlikook moom, gaynde dajeek moom, fàdd ko.
Waaye su may siggi rekk nga mel ni gaynde, di ma rëbb, dellu di ma lore say kiraama,
Noppi naa, dootuma wax, yaw yaa dogal lii.
Dëgg daal nga namm, dëggu reenu xol, kon déey ma xel mu rafet.
Moo ràppal sama der ak samaw suux, tas samay yax.
Man déy ni gaynde laay mel ak Efrayim, ni gaynde gu ndaw laay mel ak waa kër Yuda. Man, man mii maay xotat, wéy, maay yóbbu te kenn du wallu.