كل أسفار KYG

Isaiah 39

KYG · الآية 1

66 أصحاحات

KYG / Isaiah / الأصحاح 39

KYG · الآية 1

J ant yooyu doomu Baladan, Merodag Baladan buuru Babilon moo yónnee Esekiya bataaxal ak yóbbal. Fekk na mu déggoon ne Esekiya daa woppoon bay doora am tan.