Nabukodonosor jële fa mboolem alali kër Aji Sax ji ak alali kër Buur, daldi buub lépp luy ndabu wurus lu Suleymaan buurub Israyil defarlu woon ci kër Aji Sax ji, muy la Aji Sax ji waxoon.
TSK
TSK · Isaiah 39:6
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
2 Kings 24:13
TSK
Jeremiah 20:5
TSK
Maay joxe lépp luy alalu dëkk bii. Mboolem lu fiy njariñ, mboolem gànjar, mboolem denci buuri Yuda, dinaa ko teg ci seen loxol noon yi, ñu sëxëtoo, jël, yóbbu Babilon.
Jeremiah 52:17
TSK
Ci biir loolu kenuy xànjar ya bokkoon ca kër Aji Sax ji, ak rootukaay yaak mbalkam xànjar ma woon ca kër Aji Sax ji, waa Babilon toj lépp, boole xànjar jépp yóbbu Babilon.
Daniel 1:2
TSK
Boroom bi nag teg Yowakim buurub Yuda ciy loxoom, boole ca lenni jumtukaayi kër Yàlla ga. Nabukodonosor yóbbu jumtukaay ya réewum Sineyaar, ga ñuy wax Babilon itam, ca biir kërug tuuram. Mu daldi fat jumtukaay ya ca denci kër tuuram.