TSK

TSK · Isaiah 45:23

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

«Déglul lii Aji Sax ji wax: “Giñ naa ci man mii, gannaaw yaa def lii, te gàntaloo ma sa jenn doom ji,

Yàlla du nit, bay fen, du doom aadama bay tuub. Moom wax na lu mu deful a? Am àddu na lu mu sottalul?

Ñu jébbal leen ñawkay saamar, till séddoo.

Moo giñaloon Aji Sax ji, moo digook Mbërum Yanqóoba ma.

li des ci jàmbaari fittkati Kedar di lu néew.» Aji Sax ji Yàllay Israyil wax na ko.

Làquwma, di waxe bérab bu lëndëm. Newuma it askanu Yanqóoba: “Sàkkuleen ma fu dara amul.” Man Aji Sax ji maay wax dëgg, di biral njub.»

ba képp ku namma barkeel fi kaw suuf, ci Yàlla jiy dëgg la koy ñaane, te kuy giñ fi kaw suuf it, ci Yàlla jiy dëgg la koy giñe. Day fekk njàqare ya jiitu di lu ñu fàtte, te di lu làqu saay gët.

Giñ naa ko ci man mii, déy,» kàddug Aji Sax jee, «Boccra, dëkk bii day mujj di gent bu ñu doyadal, ndànd-foyfoy bu ñuy móoloo, dëkk-dëkkaanam yépp gental ba fàww.»

Ana lu ko Yàlla tontu? Da ne: «Beral naa sama bopp juróom ñaari junniy (7 000) nit ñu sujjóotaluloon Baal tuur mi.»

ba turu Yeesu tax ñépp sukk seen bëti óom, muy kaw asamaan, di kaw suuf, di biir suuf,