كل أسفار KYG

Isaiah 49

KYG · الآية 5

66 أصحاحات

KYG / Isaiah / الأصحاح 49

KYG · الآية 5

T ey Aji Sax jee wax, moom mi dale sama biiru ndey, mooñ ma, ma dib jaamam bi koy waññil askanu Yanqóoba ba ca moom, dajaleel ko bànni Israyil googu fa moom, ba jagoo teraangay Aji Sax ji, sama Yàlla jii di sama doole.