Job 11:12
TSK
Waaye ku boppam feesul, bu muusee, mbaamu àll a judduwaale nangu.
TSK
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
Waaye ku boppam feesul, bu muusee, mbaamu àll a judduwaale nangu.
Ana koo gis mu ne: «Maa xelu»? Kooku ab dof a ko gën demin.
Moom moo ne: «Sama dooley përëg laa defe lii, maa xelu, ràññee; ba randal kemi suufi xeet yi, foqati seeni alal, dañ boroom jal ya niw yëkk, wàcce leen.
Xel mu rafet lañuy jaay ba mujj diy dof.
Mànkooleen, buleen xëccu daraja, waaye nanguleena jonjoo ak ñi féete suuf, te baña jàppe seen bopp boroomi xel.