TSK

TSK · Isaiah 53:2

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

Aw njebbit mooy saxe fa ëkkub Yese, ab car soqeekoo fa reen ya,

«Ay bés a ngi ñëw,» kàddug Aji Sax jee, «maay jebbil Daawuda njebbitu njekk, mu falu di buur bu xelu, di jëfe njub ak njekk ci réew mi.

Nga wax ko ne ko: “Aji Sax ji Boroom gàngoor yi dafa wax ne: Nit a ngi nii, Njebbit la tudd, ci bérabam lay jebbee, ba tabaxi kër Aji Sax ji.

Luke 2:39 TSK

¶ Ci kaw loolu ñu matal mboolem lu yoonu Boroom bi laaj, doora dellu Nasaret, seen dëkk ba ca diiwaanu Galile.

Luke 9:58 TSK

Yeesu itam ne ko: «Till ak kàmbam, njanaaw akub tàggam, waaye Doomu nit ki de, amul fu mu wéer boppam.»

Li yoonu Musaa tële woon ndax néew dooley nitu suuxu neen, mooy lii Yàlla def: Doomam la yónni, mu dikke melow nit, te nit di bàkkaarkat, di suuxu neen, ngir Doomam fajtal mbirum bàkkaar. Yaramu suux wu nit kooku la Yàlla sottale mbugal gi war ci bàkkaar,

mbaa boroom dëkk yi diy ndawam, te mu tabb leen, ngir ñu mbugal ñiy def lu bon, te sargal ñiy def lu baax.