TSK

TSK · Isaiah 57:7

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

«Téenleen, séentu tund ya ne faraas! Ana fu ñu leen fi tëddewul? Ci yoon yi ngeen di yeeroo ni màngaan muy dogalee ci màndiŋ mi. Sobeel ngeen réew meek seen gànctook seenug mbon.

Dingeen xam ne maay Aji Sax ji, bu seeni néew nee xas fi seen biiri tuur, ak fi wër seeni sarxalukaay, ak kaw tund wu mag ak wu ndaw, ak mboolem ker garab gu naat, ak mboolem garab gu mag te sëq, fépp fu ngeen di taale cuuraay, ñeel seen mépp tuur.

Selebe yoon wu ne, tabax nga fa sa jaamookaay, di fa teddadil sab taar, ku romb, nga ràccal ko say tànk ci sa gànctu gu dul jeex.

Doomi Babilon ya dikk, fekksi ko ci kaw lalu baane, sobeel kook seen yàqute, mu sobeel boppam ak ñoom ba ñu sàppi ko.