TSK

TSK · James 1:18

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

Mooy ba Israyil dee lu ñu sellalal Aji Sax ji, di ndoortel meññeefam. Képp ku ko sex, toppees ko ko, musiba dikkal ko.”» Kàddug Aji Sax jee.

Noonu la Mbind mi indee ne: «Maa la def ngay maamu xeet yu bare.» Ibraayma mooy sunu maam fi kanam Ki mu gëm, te muy Yàlla miy delloo ñi dee, bakkan, tey woo lu nekkul, mu doon lu nekk.

Ndax kat moo noon Musaa: «Maay yërëm ku ma neex, te maay ñeewante ku ma neex.»

Moo tax nu di ko sante màggaayam, nun ñi jëkka wékk sunu yaakaar ci Almasi.

Deretam ja tuuru ca bant ba, ca la Yàlla defe jàmm, ba sottale ci moom, pexe mi mu jubalee boppam ak lépp, muy lu nekk ci kaw suuf, ak la fa asamaan.

yeena àgg fa ndajem taaw, ya seeni tur binde fa asamaan. Yeena àgg fa Yàlla, àttekatub ñépp; yeena àgg fa noowi aji jub ña ñu matal sëkk.

¶ Cant ñeel na Yàlla, sunu Baayu Sang Yeesu Almasi! Moo nu judduwaatal ci yërmandeem ju yaa, ci dooley ndekkitel Yeesu Almasi, ngir may nu yaakaar juy dund.