TSK

TSK · Jeremiah 21:11

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

Waxal Buur, wax Lingeer yaayu Buur ne leen: «Dëjuleen fi suuf, seen mbaxanam nguur mu yànj foq na.

¶ Aji Sax ji dafa wax ne: «Demal kër buurub Yuda, nga jottli fa kàddu gii.

Micah 3:1 TSK

Dama ne: «Ngalla dégluleen yeen njiiti Yanqóoba, yeen kilifay kër Israyil! Xanaa du yeena wara xam yoon?