TSK

TSK · Jeremiah 39:1

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

¶ Ba Nabukodonosor buuru Babilon àndeek mbooloom xareem mépp ak mboolem réew yeek xeet yi mu teg loxo, ñu songandoo Yerusalem ak dëkk yi ko wër yépp, kàddu gii dikkaloon na Yeremi, bàyyikoo ci Aji Sax ji:

¶ Ba Cedesyas tolloo ci juróom ñeenteelu atu nguuram, fukki fan ca fukkeelu weeram, ca la Nabukodonosor buuru Babilon ànd ak mbooloom xareem mépp ci kaw Yerusalem. Ñu dal fa janook Yerusalem, yékkati gawukaay, wërale ko.

«Yaw nit ki, bindal bés bii, bés bii ci boppam, ndax buuru Babilon gaw na Yerusalem bés niki tey.