te taxul Aji Sax ji may leen xel mu ngeen ràññee, ak gët yu ngeen gise, ak nopp yu ngeen dégge, booba ba sunu jonni yàllay tey!
TSK
TSK · Jeremiah 5:21
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
Aji Sax ji lañuy feye lii? Ndaw xeet wu dofe te ñàkk xel! Mooy seen baay, bind leen, sàkk leen, samp leen.
Ab dof du am xaalis, jënde xel mu rafet; buggu ca dara.
car ya wow, damm, jigéen ñi dikk, xambe. Dañu di xeet wu dul dégg, ba tax ki leen sàkk yërëmu leen, moo leen bind te ñeewantewu leen.
«Dofe la sama ñoñ def. Man, xamuñu maay kan, mbetey gone yu dul xalaat dara; dég-dég, tus; seen xel mépp, lu bon rekk, lu baax, xamuñu ci dara.»
¶ «“Gannaaw def ngeen jëf jii jépp nag,” kàddug Aji Sax jee, “te ma waxoon leena wax ay yooni yoon, dégluwleen; woo leen, wuyuwleen,
Ñoom ñépp a bokk dofe, ñàkk bopp: xam-xamu kasara, bant kese!
Efrayim daa mel ni pitax, dofe, ñàkk xel, di woo wall Misraak a dem Asiri.
Mu ne: “Demal ci xeet wii, nga ne leen: ‘Yeenay dégloo déglu, dungeen dégg; ngeen xoolee xoole, dungeen gis.’