Job 10:8
TSK
Say loxoo ma mooñ, tabax ma ba ma mat sëkk, léegi nga di ma yàq yaxeet!
TSK
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
Say loxoo ma mooñ, tabax ma ba ma mat sëkk, léegi nga di ma yàq yaxeet!
Defe ngeen ne yeena ma gën, ba di ma sikke musiba mii ma dal?
Soo amee lenn loo wax, àddul; waxal, ngir bëgg naa laa dëggal.
Ki may dëggal jege na. Ana kuy layook man? Nan bokk taxaw! Kuy jànkoonteek man ci yoon? Na jegesi boog!
Su ma nee: «Xaaral ma fàtte ko, dootuma biral waxyu ci turam,» sama xol bi mel nib taal bu tàkk, tàbbi sama biir yax yi; may jéema muutuwaale sa kàddu, te duma ko man.