Numbers 12:12
TSK
Ngalla bul seetaan kii mel ni ku dee te indaalewul bakkan ba mu juddoo ca ndeyam, xaaju yaram wi lekku!»
TSK
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
Ngalla bul seetaan kii mel ni ku dee te indaalewul bakkan ba mu juddoo ca ndeyam, xaaju yaram wi lekku!»
Maa ngi sàngooy sax ak àkki ban, sama der biy xar, di wal.
Damaa mujj bokk ak till, neexook looy,
Yaay mbugal ku bàkkaar, yar ko, ronq ni max la mu gëna fonk. Nitoo nit, cóolóolu neen. Selaw.