TSK

TSK · Job 2:8

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

¶ Ba Mardose yégee la ñu def lépp, daa xottiy yéreem, sol ay saaku, sottikoo dóom, di ko ñaawloo, dugg ci biir dëkk bi, di yuuxu yuux gu réy te metti.

Job 19:14 TSK

Jegeñaale ba ma, xame fàtte ma,

Samay ñaawtéef mëdd ma, diisa diis, ba àttanuma ko.

ngir tabb waa Siyoŋ ñiy ñaawlu, jox leen kaala gu wuutu dóom bi ñuy ñaawloo, ak diwu mbégte mu ñu weccikoo seenu tiis, ak mbubbam cant mu ñu weccikoo xol bu jeex, ba ñu naa: «Ñii ñoo di ponkali garabi njekk yi, njëmbat li Aji Sax ji jëmbat, ngir teewal teddngaam.»

Ñoo lay jooyal, di yuuxu yuux yu metti, xëppoo suuf, fërënqu cib dóom.