TSK

TSK · Job 20:21

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع
Job 18:19 TSK

Du doom, du askan wu muy waccey bokkam, te kenn du desey dalam.

Maa dégg Aji Sax ji Boroom gàngoor yi, mu ne: «Giñ naa ne kër yu bareey gental déy, kër yu yaa, rafet, kenn dëkku ca.

Amos 3:10 TSK

Xamuñu sax def njub.» Kàddug Aji Sax jee. «Dañuy jal alalu fitnaak yàqute ci seen biiri taax.»

Mu xaacu ne: “Maam Ibraayma, yërëm ma! Yebalal Lasaar, mu sëpp catal baaraamam ci ndox, dikk seralal ma sama làmmiñ, sawara sii metti na lool!”