Genesis 22:21
TSK
Uus lañu taawloo, teg ca Bus, teg ca Kemwel, miy baayu Aram,
TSK
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
Uus lañu taawloo, teg ca Bus, teg ca Kemwel, miy baayu Aram,
Saw làmmiñ déy, sa ndëngtee koy sa, yaa taamu di wax njublaŋ.
Yàlla miy dund seere na, moom mi ma xañ dëgg, moom Aji Man ji ma teg naqaru xol,
Yaa soppiku, néege ma, di ma soxoree sa diisaayu loxo.
Baay Ayóoba kat nee moo yey, Yàlla xañ ko dëggam.
Defe nga ne lii yoon la? Nga ne: «Maa am dëgg fi kanam Yàlla,»
Jaambur laa léegi ci saay bokk, mel ni doxandéem sama biir doomi ndey.
Waa ja nag namma wutu lay, ne Yeesu: «Sama moroom mooy kan?»