¶ «Buleen safaan dëgg cib àtte. Buleen far néew-ji-doole te buleen far boroom doole. Àtteleen seen moroom ci dëgg.
TSK
TSK · Job 32:21
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
Leviticus 19:15
TSK
Buleen jalgati yoon cib àtte, buleen jeng te buleen nangu alalu ger, ndax ab ger day muur bëti boroom xel, di xañ aji jub dëgg.
2 Samuel 14:20
TSK
Jubbanti mbir mii de moo tax Yowab def lii. Waaye yaw sang bi, danga di boroom xel mu rafet ni malaakam Yàlla. Xam nga mboolem lu xew ci réew mi.»
Job 13:10
TSK
Su ngeen ko faraloon ci kumpa sax, du tee mu sikk leen moos.
Job 34:19
TSK
Kii du far kàngam, du teg ku am ci kaw ku ñàkk, nde ñoom ñaar la boole sàkk.
Proverbs 24:23
TSK
Lii it ñi rafet xel a ko wax. Par-parloo cib àtte baaxul.
Malachi 2:9
TSK
«Moo tax man it ma def xeet wépp xeeb leen, sewal leen, feye leen ko seen ñàkka sàmm samay yoon, ak par-parloo gi ngeen di diglee yoon wi.»
Acts 12:22
TSK
Mbooloo maa ngay àddu ca kaw, naan: «Lii kay baatu Yàlla la, du baatu nit!»