TSK

TSK · Job 33:13

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع
Job 9:14 TSK

Ana nu ma koy àddoo, man? Ana kàddu yu may layook moom?

Job 10:6 TSK

ba ngay seet fu ma ñaawe, di liñbat fu ma moye?

Job 40:2 TSK

Yaw miy layook Aji Man ji, dangay diiŋat? Yaw miy weranteek Yàlla, doo tontu?

Wóoy ngalla kuy diiŋat ka la tabax te di ndabal xandeer ci biir ndabi xandeer! Ana ban ak di wax tabaxkatam, naa ko: «Looy def nii? Yaw amulooy loxo.»

Babilon, maa la fiir, nga tancu te yéguloo! Dañu laa gis, ne la taral, yaa dëkk Aji Sax ji,

Acts 1:7 TSK

Mu ne leen: «Du yeena wara xam jamono jeek bés, bi Baay bi jàpp ci sañ-sañu boppam.

Acts 9:4 TSK

Mu daanu ci suuf, daldi dégg baat bu ko ne: «Sóol, Sóol, lu tax nga di ma bundxatal?»