TSK

TSK · Job 38:13

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

Musaa tàllal loxoom, mu tiim géej ga. Ba bët di set géej ga dellu na, mel na mu meloon. Waa Misra di daw, géej ga wal, dogale leen, Aji Sax ji fél leen, ñu ne ca menteñ.

Job 24:17 TSK

Ñoom ñépp ñuulaayu guddeey seen bëccëg, lëndëm gu ne këruus lañu xejjool.

Du làkk, duy wax, du baat bu dégtu,

gaynde gu ndaw ŋaral am pàddam, di sàkkoo dundam fa Yàlla.

Ma war laafi njël, dëkki wàllaa géej,