TSK

TSK · Job 39:13

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

Te sax ay gaal yu mag la Buur amoon, ñuy ànd ak gaali Iram, benn yoon ci ñetti at yu nekk gaal ya yeb wurus ak xaalis ak bëñi ñay, aki golo ba ciy dàngin.

Job 30:29 TSK

Damaa mujj bokk ak till, neexook looy,

Ag xodd sax xam na bésub demam, pitax, wetwet ak mbelaar it dem, tey sàmm seen bésub délsi. Waaye sama ñoñ faalewuñu àtteb Aji Sax ji.