TSK

TSK · Job 5:21

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

Yaa koy làq fa nga làqu, fa pexey nit àggul. Nga yiir ko, mu yiiru ci ayu làmmiñ.

Mooy yónnee fa asamaan, musal ma, dumaal ma ku may not. Selaw. Yàllaay yónnee jëfi ngoram ak wormaam.

Làmmiñu waxkat, jam-jami jaasi; kàddu gu xelu, garab la ci.

¶ Ba mu ko defee, mu am ñu ne: «Aywaleen, nu lalal Yeremi pexe. Ndax kat soxlawunu ko ba di ci ñàkk dara: du njànglem sarxalkat, du digley boroom xel te du waxyu bu yonent biral. Nanu ko duural ba sànk ko te baña faale lenn ciy waxam.»