TSK

TSK · Job 6:21

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع
Job 6:15 TSK

Samay xarit a ma wor ni yol moo fekk ŋiis. Dañoo mel ni dex yoo fekk ndox ma jeex,

Job 19:19 TSK

Sama wóllërey démb yépp a ma sib, ma sopp leen, tey ñu dëddu ma.

Bokk yi, wóoluleen ko fu ngeen tollu, diisleen ko seen xol, Yàllaay sunu kiiraay. Selaw.

Baleen nit, noowal bakkan kese la! Ana lees koy nawe?

«Bu nu sañoon faj Babilon, mu wér, waaye wérul. Nan ko ba te dem, ku ne ñibbim réewam. Àtteb Babilon kat àgg na asamaan, àkki na fa kaw niir ya.»

¶ Buuri àddina yi àndoon ak dëkk bii ci moy ak dund gu bakkane, bu ñu séenee saxaras lakkam, ñoom ñépp ay yuuxu, di ko jooy.