Job 4:17
TSK
Mu ne: «Nit man naa am njekk fa kanam Yàlla? Am man naa laab fi kanam ki ko sàkk?
TSK
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
Mu ne: «Nit man naa am njekk fa kanam Yàlla? Am man naa laab fi kanam ki ko sàkk?
Ana nu nit di ame dëgg fa kanam Yàlla? Ku jigéen jur, nu mu mana laabe?
Ba loolu amee Eliyu doomu Barakel ma askanoo ci Buus, bokk ci làngu Ram daa mer ba futt ca la Ayóoba dëggal boppam fi kanam Yàlla,
Baay Ayóoba kat nee moo yey, Yàlla xañ ko dëggam.
Sang bi, bul layook man; kenn jubul fi sa kanam, du kuy dund.