TSK

TSK · Jonah 1:17

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

Ci biir loolu Yàlla bind rabi géej yu mag yi ak mboolem mbindeef muy féey tey ramm-rammi ci ndox mi, mu ci nekk ak wirgoom, teg ca lépp luy boroomi laaf, lu ci nekk ak wirgoom. Yàlla gis ne baax na.

Jonah 4:6 TSK

Ba mu ko defee Aji Sax ji Yàlla yebal ag lawtan, mu law, tiim Yunus, keral boppam ngir xettli ko. Yunus bég mbégte mu réy ca lawtan ga.

Ndax na Yunus nekke woon firnde ca waa Niniw, noonu la Doomu nit ki nekke firnde ci niti tey jii.